“Seet ko ci Google”*. This phrase in Wolof will now take on a whole new meaning with the launch of the Wolof Interface for Google Web Search in Senegal.
In our mission to organize the world’s information and make it universally accessible and useful, language localization plays a very important part, and the Google Africa team is proud to provide support for languages spoken by millions of African people. The ‘Google in Your Language’ initiative already supports many African languages and now we are taking a more hands-on approach: reaching out to interested universities and other volunteers in the community, training them on our translation tools and holding a fun workshop where volunteers can contribute their translations for Google Web Search in their language, with guidance from language moderators.
Group photo of the volunteers after the translation marathon |
As of today, “Google deggna Wolof” (Google understands Wolof). Check it out at www.google.sn
Posted by Angela Muigai, Localization Community Manager - Africa
* means “Search on Google”
====
Seet ko ci Google*: Google Search désormais disponible en Wolof
“Seet ko ci Google”*. Cette phrase en wolof prendra désormais un tout nouveau sens. En effet, avec le lancement de l’interface Wolof de Google Web Search il est désormais possible pour les Internautes du Sénégal d’accéder à Google en wolof pour effectuer leurs recherches.
Dans le cadre de notre mission d’organiser l’information à l’échelle mondiale et de la rendre utile et accessible, le support des langues joue un rôle très important. Google Africa est ainsi très fier d’avoir permis la prise en charge de plusieurs langues utilisées par des millions d’africains. Nous allons plus loin, avec l’initiative « Google in Your Language » (GIYL), en permettant d’étendre cette prise en charge à toutes les langues : GIYL offre à des volontaires passionnés par une langue comme le Wolof et soucieux de promouvoir sa présence en ligne, des outils pour traduire l’interface Google dans cette langue.
Tout le bénéfice de la disponibilité de Google en Wolof revient cependant à l’équipe de l’équipe de 45 volontaires (étudiants et experts) qui, grâce à la collaboration entre Google et l’Université Gaston Berger (UGB) de Saint Louis, se sont réunis au mois de juin sur le campus de l’UGB pour un marathon de traduction enthousiaste et productif. Mohamadou El-Hadj Nguer, enseignant à l’UGB, qui a dirigé les travaux de traduction, explique l’enthousiame des experts et des volontaires par leur envie de renforcer la presence du Wolof en ligne et leur conviction que la disponibilité de Google Search en Wolof va donner plus de raisons d’écrire dans cette langue et lui donner une opportunité de développement sur Internet.
Maintenant, comme vous pouvez le voir sur www.google.sn, “Google deggna Wolof” (Google comprend Wolof).
Poste par Angela Muigai, Localization Community Manager - Afrique
* signifie “Recherche sur Google”
====
Seet ko ci Google: Google Search jà ppandi na léegi ci Wolof
“Seet ko ci Google”. Kà ddug Wolof gii dina am léegi weneen maanaa ak doorug jokkalekaayu Google ci Wolof ngir Seet ci Web bi ak Google ci Senegaal.
Ci sunu sémbub dundal xam-xam ci à dduna sépp te fexe mu am njariñ te jà ppandi, jumtukaayu là kk wi lu ci am solo la. Google Afrig bég na lool ci li mu fexe ba boole ci là kk Afrig yu ay milyoηi doomam di jëfandikoo. Dinanu egg sax fu gën a sore ak naalub « Google ci Saw Là kk » (GIYL), ngir jà ppandal ko ci là kk yépp : GIYL day may ay way-coobarewu yu aw là kk soxal, niki Wolof, te bëgg mu suqaliku ci buum gi (Web bi), ay jumtukaay ngir ñu tekki jokkalekaay gu Google ci là kk woowu.
Njariñal jà ppandig Google ci Wolof a ngi ñeel nag kuréel gu 45 way-coobare (Ndongook i way-mà cc), yi nga xamne ci lonkoog Google ak Iniwersite Gaston Berger bu Ndar, ci bëj-gà nnaaru Senegaal, ñoo à nd ci weeru suwe ca Iniwersite ba ngir amal liggéey bu am a am njariñ bii. Allaaji Mamadu Nger, jà ngalekat ca UGB, di ki jiite liggéey bi, leeral na cawarte gi way-mà cc yeek way-coobarewu yi am ci bëgg a dëgëral là kk Wolof ci Web bi ak seenug dogu ci ne jà ppandig Google Ceet ci Wolof dina wone lu bari lu nu war a bindloo Wolof ak yeneen i njariñ yees mën a amee ci yëngu ci internet.
Bis niki tey, “Google dégg na wolof’. Doorees na ko ci www.google.sn